Want to create interactive content? It’s easy in Genially!

Get started free

WOLOF_Infovih_Wérgu yaram

GTT

Created on November 19, 2025

Start designing with a free template

Discover more than 1500 professional designs like these:

Discover Your AI Assistant

Vision Board

SWOT Challenge: Classify Key Factors

Explainer Video: Keys to Effective Communication

Explainer Video: AI for Companies

Corporate CV

Flow Presentation

Transcript

WÓLOF

Wérgu yaram bou khéle, touki bitime réw, ak diagoroye VIH

Wérgu yaram bou khéle, touki bitime réw, ak diagoroye VIH

Dëkk ak VIH – walla gannaaw jëfandikukat bu bees – wala nga touki si bénéne réw, meune na indi djiakharé bou bouri si sa khél bougnou tombé, li mouye indi, meune na méti lole.

Name diangoroye VIH si diamono yi, meune nga ko amé di dounbeu doundine bou mouchou si ayam come nite yeupeu, thiaytou gou bée gui dina méti torope ndakhe ni gnouye béti gni ko amé, thiokhle garabe gui ngaye dieule sa guérou doundou, ni gnou laye bété ak diafé diafé yi yéne garabe yi.

Si bénéne fane, guéne sa réw, dad déme deuki si bénéne réw, dieuf bo khamné la daye diapeu nit, métite bo khamné la dafa sokhla apeu dire ban gaye meuna méleu no nga beugue. Si yone you beurris, touki bitime réw mi, li koye indi, dou lola sobe, meuna nék ayes khékhes, gnou laye dakhé wala nga niak ayes garabes, dina indile ayes diafés diafés you laye téré nélaw.

Diares diares yoyous, dano bokou nou gnouye fégno, name dina ame sola nga woute ayes dimbeules si biti, sitou boudé dano andeu danou si sa kaweu:

Nakhare

01

Dalaldiame

02

Khalate bou laye sonal

03

Touki bitime réw + VIH

04

01

Nakhare

Lou gnou meuna yék si sa boppeu la, meune nanou ko guisse bo niaké dara, boudé ndanga triste, nakhare,méreu, li nga beugueu ameu diotochi, ndiakharé, bo mére sa boppeu, wétaye, diakhasso, bagne dará….

Niak ko beugue si yonou touki

- Sa djabote wala sayes kharites - Sa lake binga nampeu - Sa soufou thiossane, sa keur - Sa doundine - Risk yi nék si ame ayes diaffés diaffés you dieumeu si sa ayes kheuyites bo touké. - Sa tolouwaye si sa liguéye - Sa ndadjé ak mbokou yi fi khéto té thiossanou fa

Boudé ndanga niak kou amé diangoroye VIH

- Sa wérgou yarame - Sa guisse guisse si sa kaname, sa euleuk - Lou dieume si sa mbeuguéleu - Lo dieume si sa kolouté si sa bopou - Sa doudine bou dieume si yonou séye

02

Dalaldiame

Touki ba ague si bénéne réw ak gnou thiaytou sa yarame nga amé VIH, diare diare yo khamnéla, nga mine ko ak diame dafa ame sola.

Dala k diame si sa réw bi nga déme deuk

- Takhawal fa ayes kharites you bess ngir ameu dimbeule - Meuna déme si keur doctor thiaytou sa wérgou yaram - Sa come come si ayes nékayes ak mbiroume khalisse bou takhawoule - Nék si mbiroume woute dekouwaye ak liguéye. - Yakar bou tass

Mine meuneu doundou ak sa diangoro VIH

- Djiortou bou niaw - Di khalate né déffo li nga wara déff - Niak ayes khibares you dieume si diangoro VIH - Di dieule ayes garabes ak di déme si sa hopital - Di lakhe nites gni né ndaga amé diangoro VIH

03

Khalate bou laye sonal

Diare diares you doywar té méti si béne nite si ak doundime, meuna bayi ayes yakhoutés you khote té yague si ninguaye dainkontéle wala si ninguéye takhawo diafé diafé gui. Lo lou meunala indinle ayes diafé diaféyes khalate bou yagué.

Diakhlé si khalate bou andeu ak touki bitime réw

- Khékhou ayes réw - Diankhonté si langou politik - Mbuedeu mi - Niakou kirangué - Délou di touki su sa apeu réw - Di yégue né danou la beugueu béti

- Diangoro dji si bopame - Boundou khatale - Di la dakhé - Di la titeule nane danou gnoulaye ráye - Di la béti si keurou docor yi - Bo niaké sa ayes garabes

Diakhle bou andeu ak sa thiaytou diangoro

Di chi yok, ameu ayes mbirres you beurris, yo khamné meune nanou ameu ayes djikhi djikhi si ayes nites you touki si bitime réw ba paré ameu diangoroye VIH, yi gnou chi gueuna ragnés:

- Boudé amnga lo khames wala ayes khibares si diangoroye VIH - Sayes gueuneu gueumeux ssi yonou diné - Si sa awra bodé gor wala djiguéne. Djiguéne gni gnoyes eupeux ayes diafé diafés.

Khamnanou diafé diafés yi nékeu si touki bitime réw amé diangoroye VIH. Amna ayes mbotayes you beurris yo khamné dina gnou la meuna yombale ayes dioume touwaye ak akoume gougué si yone wi. Botayes yoyous meunanou la yombale takahwou si khéle ak khalate diaréko si ayes nites you touki ni yaw amé diangoro VIH té yague fi si réwou Espagne andeu akoume pache mou dieume si khéle ak khalate ak yénéni ayes mbotayes youyes takhawou nites gni nék si diafé diafés yoyou Boudé ndanga sokhla dimbeule, démale si mbotayes yoyou nék si deuk bi ndeuk.

04

VIH

Toukibitime réw

Nakhare

Xel miñaan bu ñëkk ci dëkku dëes

Njaxlafu jamm

Dalaldiame

Njuub yi ci réew bu bees

Soppiku / Dajnaas Teggin / Jàppante

Khalate boulaye sonal

Dajnaas Xeex ci nit ñi

Politig / Ragalu sero Homofobi / Dendu

Ndimbalbu xol

ÑAKKALEU

DËKKANDOO

Ñi bokk ci benn xaalis

Gëstu bu ndimbal

Ndimbal bu xam-xam

SUBVENCIONA
COLABORA
Descargo de responsabilidad La información contenida en esta ficha no pretende sustituir la recibida por el médico. Las decisiones referentes a la salud siempre deberían tomarse tras consultar con los profesionales sanitarios. La información médica puede quedar desactualizada con rapidez. Si te surge alguna pregunta tras leer esta ficha, te aconsejamos hablar con tu médico o enfermera o llamar a gTt-VIH, al 93 458 26 41, para comprobar si existe alguna novedad relevante al respecto.